Traitement du palu

Pajum sibbiru  Traitement du palu

Nit ñi : Aminta Gay, Bintu Faal ak Mareem Njaay
Les personnages : Aminata Gaye (AG), Binetou Fall (BF) et Marème Ndiaye (MN)

BF – Aminta, xanaa danga sibbiru? Aminata, as-tu le palu ?
AG – Waaw, dama sibbiru. Lu ci baax? Oui, j’ai le palu. Que faut-il prendre ?
BF – Li gën ci pajum sibbiru mooy nga naan. Pour traiter le palu, il faut prendre les médicaments dès que tu sens la maladie arriver.
MN – Su la songee, dinga yëg metit? Au début, y-a-t-il des douleurs?
BF – Waawaaw. Ku mu song, sa yaram day tàmbali di lox, tàng jérr di metti ànd ak bopp bi. Bien sûr. Dès que la maladie commence, tu as des frissons, de la fièvre et des maux de tête.
MN – Yan garab ñoo ci baax? Quel médicament faut-il prendre?
BF –  Su fekkee ni sibbiru si dal na la ba noppi, dangay naan ñetti doomi niwakiin ci saa si, ñett ci ngoon bala ngay tëdd. Si tu es déjà malade, tu prends tout de suite 3 comprimés de nivaquine, trois avant de te coucher.
Ca ëllëg sa nga naanaat ñett ci suba ak ñett ci ngoon, lépp di fukk ak ñaar.
Trois le lendemain matin, puis trois le soir. Au total, 12 comprimés.
Su fekkee ni dangay fàggu ngir moytu sibbiru si, dangay naan ñetti doom ayu-bés bu nekk. À titre préventif, tu prends trois comprimés par semaine.

Abdoulaye Dial

Tekki baat Lexique

feeñ apparaître
jérr très (chaud) ; adverbe d’intensité utilisé avec tàng seulement
lox avoir des frissons
moytu éviter
song attaquer
yëg sentir

 

Publicités
Article suivant
Poster un commentaire

Laisser un commentaire

Entrez vos coordonnées ci-dessous ou cliquez sur une icône pour vous connecter:

Logo WordPress.com

Vous commentez à l'aide de votre compte WordPress.com. Déconnexion /  Changer )

Photo Google+

Vous commentez à l'aide de votre compte Google+. Déconnexion /  Changer )

Image Twitter

Vous commentez à l'aide de votre compte Twitter. Déconnexion /  Changer )

Photo Facebook

Vous commentez à l'aide de votre compte Facebook. Déconnexion /  Changer )

Connexion à %s

This site uses Akismet to reduce spam. Learn how your comment data is processed.

%d blogueurs aiment cette page :