L’hivernage

Nawet bi  L’hivernage

Nit ñi : Abu Gay ak Baaba Faal
Les personnages : Abou Gaye (AG) et Baba Fall (BF)

BF – Ndax waa Senegaal dañuy liggéey lu bare ci nawet bi? Est-ce que les Sénégalais travaillent beaucoup pendant l’hivernage?
AG  Waawaaw, bu cooron gi tàmbalee rekk beykat yi dugg ci tool yi di ruuj. Bien sûr. Dès que la période intermédiaire commence, les cultivateurs vont aux champs pour les défricher.
BF  Lu tax loolu? Pourquoi font-ils cela?
AG  Waa-àll bi yépp dañuy waajal nawet bi moo tax. Tous les gens de la campagne préparent l’hivernage.
BF  Jigéen ñi, lu ñuy def? Dinañu dimmali seeni jëkkër? Que font les femmes? Aident-elles leurs maris?
AG  Waawaaw. Ñéppay dem ci tool yi, muy mag, di jigéen, di góor, di xale. Bien sûr, tout le monde va aux champs : les adultes, hommes et femmes, les enfants.
BF  Lan lañuy ji fii ci diiwaan bi? Que sèment-ils dans la région?
AG  Dinañu ji gerte, dugub, ñebbbe ak mboq. Ils sèment de l’arachide, du mil, des haricots (se prononce ‘des Arico’ et non ‘des ZArico’) et du maïs.

Tekki baat : Lexique

àll bi : la brousse, la campagne
cooron gi
 : période intermédiaire entre la saison sèche et la saison des pluies
diiwan bi : la région
dimmali : aider
dugub : mil
gerte : arachide
ñebbe : mil
mboq : maïs
ruuj : défricher, désherber
tool bi : le champ, le jardin
waa-àll bi : les gens de la campagne
waajal : préparer

Abdoulaye Dial

Publicités
Article précédent
Article suivant
Poster un commentaire

Laisser un commentaire

Entrez vos coordonnées ci-dessous ou cliquez sur une icône pour vous connecter:

Logo WordPress.com

Vous commentez à l'aide de votre compte WordPress.com. Déconnexion /  Changer )

Photo Google+

Vous commentez à l'aide de votre compte Google+. Déconnexion /  Changer )

Image Twitter

Vous commentez à l'aide de votre compte Twitter. Déconnexion /  Changer )

Photo Facebook

Vous commentez à l'aide de votre compte Facebook. Déconnexion /  Changer )

w

Connexion à %s

This site uses Akismet to reduce spam. Learn how your comment data is processed.

%d blogueurs aiment cette page :