Le temps

Ci jamano ji   Le temps

Nit ñi: Abdu Sekk (AS) ak Xadi Pen (XP)
Les personnages : Abdou Seck et Khady Penne

AS – Tey la lan, Xadi?  C’est quel jour aujourd’hui ?
XP – Tey la alxemes. C’est jeudi aujourd’hui.
AS – Kañ ngay dem Dagana? Quand pars-tu à Dagana ?
XP – Ayu-bés biy ñów laay dem. La semaine qui vient / La semaine prochaine.
AS – Ban bés? Quel jour ?
XP – Yaakaar naa talaata ci suba. Peut-être mardi matin.
AS – Kan ngay àndal? Avec qui vas-tu ?
XP – Sama jëkkër ak samay doom laay àndal. Avec mon mari et mes enfants.
AS – Dingeen fayàgg? Vous resterez longtemps là-bas ?
XP – Déedéet. Juróomi fan rekk lanu fay def. Non, cinq jours seulement.
AS – Maa ngiy dem, dinaa fi dellusi bala ngay dem. Je m’en vais, je reviendrai avant ton départ.
XP – Dinaa la xaar de! Je t’attendrai, hein !
AS – Waaw, dinaa la tàggusi bala ngay dem. Je viendrai te dire au revoir avant ton dèpart.
XP – Waaw kañ, nuyul ma sa waa-kër. Bien, salue-moi ta famille.
AS – Dinañu ko dëgg bu neexee Yàlla. Ils l’entendront s’il plaît à Dieu.

Tekki baat  Lexique :

jamano ji le temps
bés yi les jours
ayu-bés bi la semaine
altiné lundi
talaata mardi
àllarba mercredi
alxemes jeudi
àjjuma vendredi
gaawu / asseer samedi
dibéer / dimaas dimanche
suba demain
suba si le matin
suba teel le matin très tôt
yoor -yoor si le matin vers 10 h
bëccëg bi le jour entre midi et 14 h
ngoon si l’après-midi<
timis ji le crépuscule
ëllëg demain
gannaaw-ëllëg après-demain
gannaawaati-ëllëg le surlendemain
dèmb hier
bërki-démb avant-hier
bërkaati-démb la veille d’avant-hier
guddi gi la nuit
weer wi le mois, la lune
at mi l’année

Publicités
Article précédent
Article suivant
Poster un commentaire

Laisser un commentaire

Entrez vos coordonnées ci-dessous ou cliquez sur une icône pour vous connecter:

Logo WordPress.com

Vous commentez à l'aide de votre compte WordPress.com. Déconnexion /  Changer )

Photo Google+

Vous commentez à l'aide de votre compte Google+. Déconnexion /  Changer )

Image Twitter

Vous commentez à l'aide de votre compte Twitter. Déconnexion /  Changer )

Photo Facebook

Vous commentez à l'aide de votre compte Facebook. Déconnexion /  Changer )

w

Connexion à %s

This site uses Akismet to reduce spam. Learn how your comment data is processed.

%d blogueurs aiment cette page :